Ndénkaaney CPJ ci kaarànge: liggéey ci jamonoy mbasum koronaawiris

Yeesalu 30i fanni Suwin 2020 Ci fukki fan ak benn ci weeru maars 2020, kuréel gi yor wérgi yaram ci àdduna bi (OMS) neena lii di COVID-19 bi (Koronaawiris) feebaru mbass la. Nit ñi muy dal ci àdduna mu ngi yokku saa su ne ci ni ko OMS waxe, ganaw ci yenn réew yi walante…

Read More ›